Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 17:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 17:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Natt nga saab xol, niir ma guddi, settantal ma, gisoo dara. Dogu naa ne duma moye wax.
4 Su may jëf it, di sàmm sa kàddu. Maay moyu yoonu ku bon.
5 Sa tànk, sama tànk, jàdduma fenn.
Sabóor 17 in Kàddug Yàlla gi