Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 14:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 14:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Ñépp lajj, bokk yàqu yaxeet. Kenn deful lu baax, du kenn sax.
4 Aji Sax ji nee: «Xanaa ñiy def lu bon ñépp xamuñu dara? Ñuy lekk sama ñoñ niw ñam, te sàkkuwuñu Aji Sax ji.»
5 Foofu lañuy tiite tiitaange lu réy! Du Yàllaa ngi ànd ak kuréli ñu jub ñi?
Sabóor 14 in Kàddug Yàlla gi