Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 149:4-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 149:4-7 in Kàddug Yàlla gi

4 Aji Sax jee safoo ñoñam, di terale néew-ji-doole ag mucc.
5 Na wóllërey Yàlla bànneexoo seen ndam, bu ñu tëddee sax, di sarxolle,
6 di xaacuy kañ Yàlla, ŋàbbaale saamaru ñaari ñawka,
7 ngir duma yéefar yi, mbugale ko yooyu xeet,
Sabóor 149 in Kàddug Yàlla gi