Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 149:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 149:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Nañu màggale turam am pecc, tëggal ko, xalamal ko.
4 Aji Sax jee safoo ñoñam, di terale néew-ji-doole ag mucc.
5 Na wóllërey Yàlla bànneexoo seen ndam, bu ñu tëddee sax, di sarxolle,
6 di xaacuy kañ Yàlla, ŋàbbaale saamaru ñaari ñawka,
Sabóor 149 in Kàddug Yàlla gi