Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 148:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 148:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Nangeen màggale Aji Sax ji fa kaw suuf, yeen ninki-nànkay géej ak xóote yépp,
8 ba ca melax yaak doj yu sedd yay taw, ak tawub yuur akub lay, ba ca ngëlén yu mag yay def ndigalam.
9 Màggal-leen ko yeen tund yu mag yeek yu ndaw yépp, ba ci garab yiy meññ ak garabi seedar yi,
Sabóor 148 in Kàddug Yàlla gi