Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 148:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 148:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Màggal-leen ko, yeen jant beek weer wi, màggal-leen ko, yeen mboolem biddiiw yii di nes-nesi.
4 Màggal-leen ko, yeen asamaani kaw-li-kaw, ba ca ndox ma tiim asamaan ya.
5 Nañu màggal turu Aji Sax ji, kii kat a santaane, lii lépp am.
Sabóor 148 in Kàddug Yàlla gi