Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 148:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 148:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Màggal-leen turu Aji Sax ji, moom doŋŋ la turam kawe, darajaam tiim asamaan ak suuf.
14 Moo dooleel ñoñam, wóllëreem ñiy mbooloom bànni Israyil, xeet wi mu xejjoo, di ko màggal. Màggal-leen Ki Sax!
Sabóor 148 in Kàddug Yàlla gi