Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 147:7-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 147:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Woyeleen Aji Sax ji kàddug cant, kañeleen sunu Yàlla jii ay xalam;
8 mooy sànge asamaan ay niir, tawal suuf, saxal tund yi am ñax,
9 leel mala, xol liiru baaxoñ bu jooy.
10 Kii nawul dooley fas, gërëmul kàttanu jàmbaar.
Sabóor 147 in Kàddug Yàlla gi