Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 147:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 147:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 di faj naqaru xol, fajtal góomi boroom.
4 Mooy lim biddiiw yi, tudd bu ci nekk.
5 Sunu Boroom a màgg, bare doole; am xelam wees kemu.
Sabóor 147 in Kàddug Yàlla gi