Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 147:13-16 in Wolof
Help us?
Sabóor 147:13-16
in
Kàddug Yàlla gi
13
Mooy tëj ràpp seen bunti dëkk, barkeel seen askan wa ca biir,
14
jàmmal seen suufas réew, reggal leen ngëneelu pepp,
15
yónnee suuf ndigalam, kàddoom ne coww, daw ca.
16
Mooy tawal yuur bu mel ni wëttéen, di lay lay bu sedd, mel ni pënd ci suuf.
Sabóor 147 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms