Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 147:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 147:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Mooy tëj ràpp seen bunti dëkk, barkeel seen askan wa ca biir,
14 jàmmal seen suufas réew, reggal leen ngëneelu pepp,
15 yónnee suuf ndigalam, kàddoom ne coww, daw ca.
Sabóor 147 in Kàddug Yàlla gi