Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 146:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 146:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 di àtte néew-ji-doole, di leel ku xiif. Aji Sax jeey tijji ku ñu tëj.
8 Aji Sax jeey xippil silmaxa, di siggil ku sëgg. Aji Sax jee sopp ku jub.
Sabóor 146 in Kàddug Yàlla gi