Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 146:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 146:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Ndokklee kuy dimbalikoo Yàllay Yanqóoba; di yaakaar Yàllaam Aji Sax ji,
6 ki sàkk kaw ak suuf, géej ak lu ci biiram, di sàmm dëgg ba fàww,
Sabóor 146 in Kàddug Yàlla gi