Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 146:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 146:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Noo ga day rëcc, mu dellu suuf; bu bés baa, pexeem jeex.
5 Ndokklee kuy dimbalikoo Yàllay Yanqóoba; di yaakaar Yàllaam Aji Sax ji,
Sabóor 146 in Kàddug Yàlla gi