Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 146:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 146:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Buleen wóolu kilifa, doom aadama amul wall.
4 Noo ga day rëcc, mu dellu suuf; bu bés baa, pexeem jeex.
5 Ndokklee kuy dimbalikoo Yàllay Yanqóoba; di yaakaar Yàllaam Aji Sax ji,
6 ki sàkk kaw ak suuf, géej ak lu ci biiram, di sàmm dëgg ba fàww,
Sabóor 146 in Kàddug Yàlla gi