Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 145:7-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 145:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Sa mbaax gu réy, dees na ko tari, te sag njekk, dees na ko woy.
8 Yiw ak yërmande, Aji Sax ji; kee muñ mer te bare ngor!
9 Aji Sax jee baaxe ñépp, di yërëm lu mu sàkk.
10 Aji Sax ji, lépp loo sàkk a lay gërëm, sa wóllëre yi di la sant,
Sabóor 145 in Kàddug Yàlla gi