Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 145:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 145:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax jee màgg te jara màggala màggal, kii màggam amul kemu!
4 Na maasoo maas di màggal say jaloore, di biral sa njàmbaarte.
5 Sa leeru teddnga ji ne ràññ, ak sa jëf ju yéeme laay jàngat!
6 Sa dooley jëf ju raglu dees na ko jottli, te sa màggaay maa koy yéene.
Sabóor 145 in Kàddug Yàlla gi