Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 145:19-20 in Wolof

Help us?

Sabóor 145:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Nammeelu ku ko ragal, mu sottal; yuuxam, mu dégg, musal.
20 Aji Sax jeey sàmm kuy soppeem, di sànk képp ku bon.
Sabóor 145 in Kàddug Yàlla gi