Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 145:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 145:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ku daanu, Aji Sax ji wallu; ku sëgg, mu siggil.
15 Ñépp a la wékk bët, di yaakaar, te bu jotee, yaa leen di leel,
16 tàllal sa loxo, reggal luy dund, ba xolam sedd.
Sabóor 145 in Kàddug Yàlla gi