Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 145:13 in Wolof

Help us?

Sabóor 145:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Sa nguur ay nguur gu sax dàkk, sa kilifteef ñeel maasoo maas. Aji Sax ji daa sàmm ay waxam, gore ciy jëfam.
Sabóor 145 in Kàddug Yàlla gi