Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 144:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 144:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Aji Sax ji, firil asamaan, wàcc; laal tund yi, ñu saxar.
6 Melaxal, falaxe noon yi; fittal, ñu fëlxoo,
Sabóor 144 in Kàddug Yàlla gi