Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 144:3-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 144:3-8 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, luy nit, ba nga di ko ràññee? luy doom aadama, ba nga di ko faale?
4 Nit ni ngelaw, ay fanam di takkndeer, wéy.
5 Aji Sax ji, firil asamaan, wàcc; laal tund yi, ñu saxar.
6 Melaxal, falaxe noon yi; fittal, ñu fëlxoo,
7 nga yóotoo ma fu kawe, xettli ma, wallu ma ci doxandéem yi def wali wal fi sama kaw,
8 di fen, di giñ ay fen.
Sabóor 144 in Kàddug Yàlla gi