Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 144:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 144:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Sunuy sàq feese wirgoy wirgo, sunuy gàtt jur junni, ba fukki junni (10 000) ci parlu yi,
14 nag yi ëmb ba diis, du mbas, du biir bu yàqu, te deesu fi yuuxoo pénc ya.
15 Ndokklee xeet wu am lii! Ndokklee xeet wu yàllawoo Aji Sax ji!
Sabóor 144 in Kàddug Yàlla gi