Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 143:8-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 143:8-11 in Kàddug Yàlla gi

8 Xëye ma sa ngor, yaw laa wóolu; xamal ma fu may doxe, yaw laa wékk sama bakkan.
9 Aji Sax ji, musal ma ci noon yi, yaw laa làqoo.
10 Jàngal ma, ma jëfe sa coobare; yaa di sama Yàlla. Yal na ma sam xel jiitee mbaax ci yoon wu tàlli.
11 Aji Sax ji, musal ma ngir saw tur, jëfeel sag njekk, teggil ma njàqarey bakkan.
Sabóor 143 in Kàddug Yàlla gi