Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 143:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 143:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax ji, gaawal wuyu ma; sama xol a jeex, ma ne yàcc, bu ma xañ sa yiw, ma yem ak kuy tàbbiji biir pax.
8 Xëye ma sa ngor, yaw laa wóolu; xamal ma fu may doxe, yaw laa wékk sama bakkan.
9 Aji Sax ji, musal ma ci noon yi, yaw laa làqoo.
Sabóor 143 in Kàddug Yàlla gi