Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 143:7 in Wolof

Help us?

Sabóor 143:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax ji, gaawal wuyu ma; sama xol a jeex, ma ne yàcc, bu ma xañ sa yiw, ma yem ak kuy tàbbiji biir pax.
Sabóor 143 in Kàddug Yàlla gi