Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 141:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 141:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Ni ñuy gàbbe suuf ba mu ne ŋafeet, ni la njaniiw di ŋaye, aw seeni yax yu tasaaroo.
8 Aji Sax ji Boroom bi, yaw laa wékki gët, yaw laa làqoo, bu ma seetaan, ma dee.
Sabóor 141 in Kàddug Yàlla gi