Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 141:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 141:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, sàmmal ma sama làmmiñ, saytul ma sama kàddu.
4 Bu ma xiir ci lu aay, may jëfe jëf ju bon, ànd ceek ñiy jëf lu ñaaw, di wàlli seeni bernde.
Sabóor 141 in Kàddug Yàlla gi