Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 140:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 140:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Dama ne Aji Sax ji, yaay sama Yàlla; Aji Sax ji, teewlul, ma dagaan la.
8 Aji Sax ji Boroom bi may walloo doole, yaa ma yiir keroog bésub xare.
Sabóor 140 in Kàddug Yàlla gi