Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 140:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 140:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 daas làmmiñam ni jaan, guux daŋaru ñàngóor. Selaw.
5 Éy Aji Sax ji, aar ma ci loxol ku bon, musal ma ci nitu fitna, ku may fexee fakktal.
Sabóor 140 in Kàddug Yàlla gi