Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 13:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 13:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Céy Aji Sax ji sama Yàlla, geesu ma, wuyu ma, leqli ma, bala ma ne sërëx ci nelawi ndee,
5 noon ba naan: «Daan naa ko,» bañ yay bége saab jéll.
Sabóor 13 in Kàddug Yàlla gi