Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 139:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 139:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 di càmbar samab dox ak sama tëraay, yittewoo lépp lu may def.
4 Aji Sax ji, bala maa wax baat, ndeke yaw, xam nga lépp.
Sabóor 139 in Kàddug Yàlla gi