Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 139:19-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 139:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Éy sama Yàlla, soo reyoon ñu bon ñii! Yeen bóomkat yi, soreleen ma!
20 Ñii sa tur lañuy luubale, noonoo la, di tudd sa tur ciy caaxaan.
21 Aji Sax ji, maaka bañ ñi la bañ te sib ñi lay gàntal.
Sabóor 139 in Kàddug Yàlla gi