Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 139:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 139:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Naa la sante sama bind bu raglu bii te yéeme, say jalooree di kéemaan, bir na ma!
15 Sama jëmm jii umpu la, ba muy bindu ci kumpa, mel ni lu ñu ràbbe ci xóotey suuf.
16 Gis nga ma, ba ma diw lumb; sa téere lim na fan yi nga ma àppal, ba ca benn dooragul.
Sabóor 139 in Kàddug Yàlla gi