Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 139:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 139:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Yaa ma sàkkal xol ak xalaat, ràbbe ma sama biiru ndey.
14 Naa la sante sama bind bu raglu bii te yéeme, say jalooree di kéemaan, bir na ma!
Sabóor 139 in Kàddug Yàlla gi