Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 137:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 137:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax ji, fàttlikul Edomeen ña, keroog jantub Yerusalem, ba ñu naan: «Màbbleena màbb, ba kenug dëkk bi siiñ!»
8 Yeen waa Babilon, gi ñu nara fàllas, ndokklee ku leen fey jëf, ja ngeen nu def!
Sabóor 137 in Kàddug Yàlla gi