Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 136:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 136:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Moo sàkk leer yu mag yi:
8 jant bi yilif bëccëg,
9 weer ak biddiiw, guddi.
Sabóor 136 in Kàddug Yàlla gi