Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 136:3-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 136:3-10 in Kàddug Yàlla gi

3 Santleen Sangu sang yi.
4 Moo wéetoo jaloore yu mag yi.
5 Moo sàkke asamaan manoore.
6 Moo lal suuf ca kaw ndox ma.
7 Moo sàkk leer yu mag yi:
8 jant bi yilif bëccëg,
9 weer ak biddiiw, guddi.
10 Moo fàdd taawi Misra yu góor ya,
Sabóor 136 in Kàddug Yàlla gi