Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 136:22-25 in Wolof

Help us?

Sabóor 136:22-25 in Kàddug Yàlla gi

22 sédde Israyil ma dib jaamam.
23 Ci biir notaange la nu geesoo,
24 ne nu siféet ci loxoy noon ya.
25 Mooy leel bépp boroom bakkan.
Sabóor 136 in Kàddug Yàlla gi