Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 136:19-25 in Wolof
Help us?
Sabóor 136:19-25
in
Kàddug Yàlla gi
19
reyaale Siwon buurub Amoreen ña,
20
reyati Og buuru Basan.
21
Moo nangu seen réew, joxe,
22
sédde Israyil ma dib jaamam.
23
Ci biir notaange la nu geesoo,
24
ne nu siféet ci loxoy noon ya.
25
Mooy leel bépp boroom bakkan.
Sabóor 136 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms