Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 136:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 136:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Moo xar géeju Barax ya yaar,
14 jàllale bànni Israyil ca digg ba.
15 Moo xalab Firawnaak mbooloom ca géeju Barax ya.
Sabóor 136 in Kàddug Yàlla gi