Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 135:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 135:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Mooy yékkateey niir fa cati àddina, sàkkal taw ay melax, yebbee ngelaw cay dencam,
8 fàdd luy taaw fa Misra, doom aadama, ba ci mala.
Sabóor 135 in Kàddug Yàlla gi