Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 135:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 135:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Aji Sax ji kay ay àtte ñoñam ñi, di ñeewante jaamam ñi.
15 Tuuri yéefar yi, xaalis ak wurus, loxoo ko sàkk.
16 Am gémmiñ te du wax, ami gët te du gis,
Sabóor 135 in Kàddug Yàlla gi