Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 132:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 132:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Nan dem ba këram, sujjóotali ndëggëstalu tànkam ya.
8 Aji Sax ji, jógal agsi sa dal-lukaay, yaak sa gaal gi jëmmal sa doole.
Sabóor 132 in Kàddug Yàlla gi