Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 132:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 132:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Mu ne: «Duma ñibbi,
4 duma tëddi sama kaw lal ba, duma nelaw, duma gëmm sax bët,
5 li feek sàkkaluma Aji Sax ji bérab, ba dëkkal Mbërum Yanqóoba ma.»
Sabóor 132 in Kàddug Yàlla gi