Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 130:3-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 130:3-8 in Kàddug Yàlla gi

3 Ki Sax, yaw, soo doon lim bàkkaar, Boroom bi, ana kuy taxaw?
4 Waaye yaay jéggale, ñu ragal la.
5 Damay xaar Aji Sax ji, di ko xaare xol, di yaakaar kàddoom.
6 Wattukat bi yàkkamti njël, wattukat bi yàkkamti njël, laa ne, ni ma yàkkamtee Aji Sax jee ko raw.
7 Éey Israyil, négandikul Aji Sax ji. Aji Sax jee gore, te yaatug njot.
8 Mooy jot Israyil ci ñaawtéefam yépp.
Sabóor 130 in Kàddug Yàlla gi