Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 130:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 130:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Ki Sax, yaw, soo doon lim bàkkaar, Boroom bi, ana kuy taxaw?
4 Waaye yaay jéggale, ñu ragal la.
Sabóor 130 in Kàddug Yàlla gi