Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 12:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 12:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Dañuy fenante, làmmiñ dig lem, xol ba njuuy la.
4 Yal na Aji Sax ji tëj gémmiñu kuy naxe, ak kuy làmmiñuy tëggu.
5 Ñu ngi naa: «Sunu làmmiñ lanuy daane, nook sunu kàddu; ku nu manal dara?»
Sabóor 12 in Kàddug Yàlla gi