Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 129:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 129:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Sama gannaaw gi lañu gàbba gàbb, rëdd koo rëdd nib tool.
4 Waaye Aji Sax ji boroom njekk dog na buumi ñu bon ña.
5 Képp ku noonoo Siyoŋ yal nañu ko dëpp, gàcceel ko.
6 Yal nañu mel ni ñax mu saxem xadd, balaa law, lax.
Sabóor 129 in Kàddug Yàlla gi