Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 128:5 in Wolof

Help us?

Sabóor 128:5 in Kàddug Yàlla gi

5 Yal na la Yàlla barkeele fii ci Siyoŋ; yal nanga teewe xéewalu Yerusalem sa giiru dund gépp,
Sabóor 128 in Kàddug Yàlla gi